Reposted by Mùstàfàà Bàshììr

Bunu bëggee «AND BEESAL SENEGAL», «ANDU-NAWLE» du mana ñàkk, maanaam «AND CI KOOLUTE», ku nekk «SAMM SA KAADU».
Liy farata mooy nu ànd «TAKKU WALLU SÉNÉGAL», maanam «SENEGAAL KESE» lanu wara tek sunu kanam, boole ci «FARLU» ci «JEL LINU MOOM» ngir yaatal «KIRAAY AK NATANGUE».👇